Pinned
Moor Suraŋ
37K posts
Mor Sourang PDG Massalik Café, Écrivain et Chercheur sur le Mouridisme
Senegal
Joined March 2019
- S. Seex dalal ak jàmm, noo ngi lay ndokkeel te di la sant ci ndam li nga indil waa réew mi, rawati na nun waa Tuubaa. Yal na la Buur bi sàmm te baril say kem barkeb Alxuraan.
- Soxna si ni mu teel a waajalee boppam ci ñàkk a joxe loxo am na solo lool, président buy yegsi day fekk mu xam ko
00:00 - Lu doy waar ! Sëriñ Ibra Géy moo wër kaaba bi yékkati fa Nuuru Daarayni, Naar bii jooy na ba sonn ndaysaan
00:00











